Share

28 DECEMBRE 2007 – 2018 FATALIKOU SERIGNE SALIOU MBACKE

Mingui ganĂ© adouna goudi Adjouma 1333 atoum gadday gui depo ak 22 septembre 1915 thia Ndiaareem, ay wadjouram Serigne Touba khadim rassoul ak Sokhna Faty DiakhatĂ©, bimu gannee diamono Serigne bi binde ci aw kayit « ASSALIHOU wala ASSALIHA  » diokh ko S Mouhamadou Lamine Diop Dagana diokhko ndigueul mu toudĂ© ko nonu, #am_ndiangam Serigne Alsane DiakhatĂ© moko diangal Alkhourane bamu mokkal mokkal gu rafĂ©t, mu dadi tambli ndiangoum xam xam thia Tindodi ci Serigne Makhtar Dieng Guyar, diangue na yitam ci S Habibu ci Touba diangue na yitam ci S Mor Sasoum DiakhatĂ© thia Haynu Maadi ak ci S Modou DĂ©m Ndiaareem ak Serigne Hamidu Sow thia MĂ©wnu ba mudie guĂšediu lole thii mbooleem xam xam yi rawatina taarikh ak Hilmu nudiom ak gĂ©ographie nĂ©kkone na ap gueustu kat bu mak fu bari ci reewmi dĂ©mnafa di gueustu ak sakh bitim reew fu mĂ©l ni Cote d’ivoire ak Gambie #ay_sagnthiam sagnthione na ay barab yu bari nguir dianglĂ© ak yar ci atoum 1934 la sagnthie Gott, Ndiurul, Khabane, Ndookaa, Ndiapndal, Lagane, Ngueediaane, Ndibingal, GuĂ©lor, Touba Ndiaareem, Ngaabu, ci atoum 1993 la sagnthie Khelcom di fukki daara ak diurom 15 daara yoyu bene buthii nĂ©k mbooloo mu takku niofa guĂ©nnee ci ay boromi xam xam Serigne Saliou Mbacke dĂ©f na ci khilaafa gui fukki at ak diurom ñatt dĂ©fna thii djouma dji liguey yu takku yu am solo taaralaat barabu ku tĂ©d ki lako weur lĂ©p mu dĂ©fko or dĂ©f thii Touba ay taly yu bari tabakh fi ay djouma yu bari agalĂ© fi ay djouma yu bari dĂ©f fi ay forages yu bari yokkat keur Serigne Touba yi
Bamu ag ci limoup 28 yokkat fadiu kay yi mĂ©lni hĂŽpital dieemoul ak hĂŽpital Matlaboul Fawzayni yaatalaat Touba yokkat ci quartier yu bari agalĂ© universitĂ©s bi Cheikh Abdou Lahad tambliwone ak canal yi niu dĂ©f mbĂ©ddi Touba ngui taataayi ak yu bareeee bareeee bari Cheiykhu Saliou Mbacke mingui guĂ©nn adouna bissoup aldjouma 28 dĂ©cembre 2007 amone na 92 ans yalnanu ko yalla fayal ta tass niu ci barkeem ci barkĂ© ku tĂ©d kiđŸ™đŸŸđŸ™đŸŸ

Leave a Comment

Protected by WP Anti Spam