Share

Cheikh abdou Lahad Mbacké Gaïndé Jambaar

Cheikh abdou Lahad Mbacké Gaïndé Jambaar Dëg Nit Kuma Naw Ci Xam Xam bu sél bi Ci Gis Gis Bu Sori bi Ci vision bimu Am ci Ligeeyel Sëriñ bi Ci Touba Ku Mouride yi wara japalé jap Ko Bu Baax japalé ko Ci Ligeey bimuy def ci deuk bi dii touba ak magal Gu mag Gii ñu jugé jaajef Mbacke Mouride yép bég nañu.
Yalla nala Yalla weral sam la Taxawu la Yagal lafi Ci Barkep sa Maam yu baax yi

Leave a Comment

Protected by WP Anti Spam