Un commissaire de la police des parcelles fait arrêter un pharmacien (Dr Cheikhouna Gaye) de la pharmacie Fadilou Mbacké parce qu’il ne voulait pas lui vendre une injection sans ordonnance.
Douma Sédal Kéne Louma Khamout ! Dou taye dou euleug. Ko khamné fi si aduna no diamonenté té nga sakh si Diamou Yalla at liguéye ak dioub ak bagna togne kéne ! té koula togne nga diégual ko, may sa sédé té sou eulégué may ley sédé sou kanamou Serigne Touba moooy soune yaakaar euleug. […]