Related Articles
Cheikh Abdoul Ahad : Su ma waxee
Posted on Author lahad
Man day def su ma waxee ci kaw, ñu ne day xulóo. Bu ma waxee liñ wara def, ñu ne daa mer. Ma di léen xamal nak ni léen, xulóo ak mer darra du ma ko ci def li feeg may dundu. Ndax xulóo moom, li koy waral xam naa ko, ñaar ñu déggoodi koo […]
Spécial Goudi Al Jumma Keur Cheikh Abdoul Ahad Mbacké
Posted on Author lahad
Il est prévu le 20 juin 2019 à partir de 20h45 un spécial goudi al jumma à Touba Belel, Keur Serigne Abdoul Ahad Mbacké.