Related Articles
Cheikh Abdoul Ahad : Su ma waxee
Posted on Author lahad
Man day def su ma waxee ci kaw, ñu ne day xulóo. Bu ma waxee liñ wara def, ñu ne daa mer. Ma di léen xamal nak ni léen, xulóo ak mer darra du ma ko ci def li feeg may dundu. Ndax xulóo moom, li koy waral xam naa ko, ñaar ñu déggoodi koo […]
Wadjal Magal Darou Salam 2019 : Goudi Ajuma Serigne Hamzatou Chouhaybou MBACKE
Posted on Author lahad
Serigne Hamzatou Chouhaybou MBACKE marque par sa présence et des déclamations de Khassaïdes, l’ouverture du « Goudi Ajuma » à Darou Salam en préparatif du Magal de Darou Salam prévu le 23 juillet 2019.