Docteur Dieng Médecin chef région Diourbel ( 2STV) Dimanche 12 Avril 2020 Seriñ Mountaxà yamul ci 200 millions yi rék ndàx niune gni fété ci dëek bi dafe nio woo joxë nu alal ju takku négnu nanu ko dimbaliko ci ligéye bi. Wowaate ma Joxe ma café , tiép ak sukaar ak diw ni ma […]