

Related Articles
Fatilikou Serigne Saliou MBACKE (28 décembre 2007 – 25 décembre 2018)
Posted on Author lahad
Mingui gané adouna goudi Adjouma 1333 atoum gadday gui depo ak 22 septembre 1915 thia Ndiaareem, ay wadjouram Serigne Touba khadim rassoul ak Sokhna Faty Diakhaté, bimu gannee diamono Serigne bi binde ci aw kayit « ASSALIHOU wala ASSALIHA » diokh ko S Mouhamadou Lamine Diop Dagana diokhko ndigueul mu toudé ko nonu, #am_ndiangam Serigne Alsane […]